| Beuguena wanté mane dé dama amoul |
| Da nga di gouné motakh mouy sa khalaat |
| Ni Beuguena wanté mane dé dama Ragal |
| Da nga di ngouné moutakh mouy sa khalaat |
| Nga naan ma kay niou sey té noumouy démé? |
| Bou ndieukone dang chi toll niou may la djabar |
| Té legui bo ko meunoul demal teudi |
| Cherie coco li dé doyna kemane |
| Nga nane ma kay niou say té awma pantam |
| Fa Diallo wakhma noko toudé |
| Nga naan ma takk la mane awma place |
| Cherie coco wakhma no ko toudé |
| Ndakh legui da ngay diang ba yéy keuyitt |
| Di takhawalou |
| Mané li dé doyna kemane |
| Ni beugu na, ni beuguena la |
| Fatou diallo wakhma no ko toudé |
| Nga nane ma kay niou say té awma pantam |
| Fa Diallo wakhma noko toudé |
| Nga naan ma takk la mane awma place |
| Cherie coco wakhma no ko toudé |
| Ndakh legui da ngay diang ba yéy keuyitt |
| Di takhawalou |
| Mané li dé doyna kemane |
| Ni beugu na, ni beuguena la |
| Fatou diallo wakhma no ko toudé |
| Ni beugu na, ni beuguena la |
| Cherie coco wakhma no ko Guissé |
| Ni beugu na, ni beuguena la |
| Fatou diallo wakhma no ko toudé |
| Ni beugu na, ni beuguena la |
| Cherie coco wakhma no ko Guissé |
| Nga naan ma kay niou sey té noumouy démé? |
| Bou ndieukone dang chi toll niou may la djabar |
| Té legui bo ko meunoul demal teudi |
| Cherie coco li dé doyna kemane |
| Nga nane ma takk la mane awma pantam |
| Fa Diallo wakhma noko toudé |
| Nga naan ma takk la mane awma place |
| Cherie coco wakhma no ko toudé |
| Ndakh legui da ngay diang ba yéy keuyitt |
| Di takhawalou |
| Mané li dé doyna kemane |
| Ni beugu na, ni beuguena la |
| Fatou diallo wakhma no ko toudé |
| Ni beugu na, ni beuguena la |