![Dibi Dibi Rek - Ismaël Lo](https://cdn.muztext.com/i/328475215603925347.jpg)
Data di rilascio: 14.06.2015
Etichetta discografica: Capitol Music France
Linguaggio delle canzoni: Maori
Dibi Dibi Rek |
Dibi Dibi Rek |
aah Dibi Dibi Rek |
aah Dibi Dibi Rek |
yangui deugueurlou wanté meunoko boul sop bayil niou djeuliko |
yangui ndirok balai bou niou takhawal, aah ndakh yow lekkato |
yangui beugu dé ndakh yow nanato, boul sop bayil niou djeuliko |
Ndakh mo ley madj lo |
Dibi Dibi Rek |
aah Dibi Dibi Rek |
aah Dibi Dibi Rek |
Dibi Dibi Rek |
aah Dibi Dibi Rek |
aah Dibi Dibi Rek |
Mbeuguel kenn khamoul lou mou doonn |
Foulla diou barri ndaham amatou fi yoon |
Kholl moy capitainou boromam |
Ndakh mo ley madj lo |
Dibi Dibi Rek |
aah Dibi Dibi Rek |
aah Dibi Dibi Rek |
Dibi Dibi Rek |
aah Dibi Dibi Rek |
aah Dibi Dibi Rek |
Ay niit niom bou niou beuguenté, khamaal lo tchi waakh |
Niom mame boye sene taar wessouna, wayé tey laniou gueuneu beugueunté |
Ya ngui beugu dé ndakh yaw lekatto |
Bo fi guetarro waw ma bayiko |
Ndakh mo lay madj lo |
Dibi Dibi Rek |
aahDibi Dibi Rek |
aah Dibi Dibi Rek |
Dibi Dibi Rek |
aahDibi Dibi Rek |
aah Dibi Dibi Rek |
Ndakh mo lay madj lo |
Ndakh mo lay madj lo |
Dibi Dibi Rek |
aahDibi Dibi Rek |
aah Dibi Dibi Rek |
Dibi Dibi Rek |
aahDibi Dibi Rek |
aah Dibi Dibi Rek |
Dibi Dibi Rek |
aahDibi Dibi Rek |
aah Dibi Dibi Rek |
Dibi Dibi Rek |
aahDibi Dibi Rek |
aah Dibi Dibi Rek |
Nome | Anno |
---|---|
Tajabone | 2015 |
Jammu Africa | 2015 |
Nafanta | 2015 |
Tadieu Bone | 1986 |
Noir Et Blanc ft. Ismaël Lo | 2015 |
L'Amour A Tous Les Droits | 2015 |
Without Blame ft. Marianne Faithfull | 2015 |
Sofia | 2015 |
Liberté ft. Ismaël Lo, Lokua Kanza, Koffi Olomide | 1999 |
Après la guerre ft. Ismaël Lo | 1999 |
Fa Diallo | 1999 |