Informazioni sulla canzone In questa pagina puoi leggere il testo della canzone Adouna , di - Natty Jean. Canzone dall'album Imagine, nel genere РеггиData di rilascio: 04.10.2018
Etichetta discografica: Baco
Lingua della canzone: spagnolo
Informazioni sulla canzone In questa pagina puoi leggere il testo della canzone Adouna , di - Natty Jean. Canzone dall'album Imagine, nel genere РеггиAdouna |
| Nit ñi fi ñuy rawante / mooy ci xol yu rafet yee |
| Nit ñi fi ñuy amee barke/ mooy ci ñaanu waa-jur yee |
| Nit ñi fuñu jëm ag yaakamti / xanaa bëg yaxxule |
| Kon sa wërsëg ding ko fekkee/ xanaa waxtu bi su jotee |
| Na nga sant, sant, sant, sant te baña yàkkamti waay |
| Kon defal ndank, ndank, ndank, ndank mooy jàpp golo ci ñaay |
| Mu xiin, mu taw, mu neex, mu naqari (na nga am sa fulla waay) |
| Nga weex, nga ñuul, nga am ba xamadi (yaw bul fàtte Yalla waay) |
| Bula àdduna jay ba nga fàtte ki nga doon ding ko réccu |
| Nii de laa ko gisee |
| Yalla buur bi nelawul té gëmmentuwul |
| Leeg leeg mu jàpp njamburam ne tekk |
| Te loo ko ñaan mu may la ko si kaw nga laabir |
| Ag am jom te nangu lepp limu la teg |
| Nit ñi dañu bare dugg-dugg, xoolal bu baax |
| Laatà nguay dugg ci lu la bett |
| Nangu jël na cëru bañ ba tax na tay jii |
| Ki nga gën a wóolu moo la mën bett |
| One two three/ suñu Sénégal a ngui |
| Sutura bi daf fi jeex ba luñu gis di nettali |
| Mbele mbel bi bari, seen xol yi naqari |
| Nañu job te bàyyi coow li |
| Mu xiin, mu taw, mu neex, mu naqari (na nga am sa fulla waay) |
| Nga weex, nga ñuul, nga am ba xamadi (yaw bul fàtte Yalla waay) |
| Bula àdduna jay ba nga fàtte ki nga doon ding ko reccu |
| Nii de laa ko gisee |
| Yow da ngay mel ni nga wara mel, ñun ñu nangu say jikko |
| Buur bi baaxèe na ñu xel, li ci des mottali ko |
| Da nguay def li nga wara def, sa wërsëg lijjënti ko |
| Àdduna ag ni mu mel lo fi góobe garaale ko |
| Buula Yalla teggee nattu man what can you do |
| Li may ñaan mooy jàmm, wergi yaram, fan yu gudd |
| Na nga màndu, doo ko réccu, na nga tuub, jéggalu |
| Yalla rek a dul juum, nañu dem jébbalu |
| Ñu bare dañuy fàtte ne àdduna jaru ko |
| Ag loo fi mën am yaw da ngay dem bayyi ko |
| Kila bëg waxla dëgg da ngay teey deglu ko |
| Dunyaa tay jii dafa dem ba jaxasoo |
| Nome | Anno |
|---|---|
| Je marcherai ft. Natty Jean | 2016 |
| Comme je ft. Natty Jean, Manjul | 2021 |
| Ne touche pas ft. Natty Jean | 2014 |
| Poupées russes ft. Natty Jean | 2014 |