Informazioni sulla canzone In questa pagina puoi trovare il testo della canzone Bamako, artista - Youssou N'Dour.
Data di rilascio: 31.12.2009
Linguaggio delle canzoni: inglese
Bamako(originale) |
Si gare bi lako fekkeu |
Mi ngui sanguo seur |
Té beut yi di takkeu |
Ma dal di koye nougnou |
Mou dal di maye faye |
Dal di maye yédeu ci adouna bou yakhou bi |
Mane douma fatté! |
Ah mani ah mani! |
Man douma fatté bamako lii mani lii mani! |
Mane douma fatté! |
Kerok lama khamal louma khamoul woone ci diamono bou yakhou bi yénene ak yénene; |
Balaa maye dougeuti mane ci loumou meuneu doone |
Dinaa fattélikou ndaw sossou |
Limouma wakhoone! |
Souy souy sou sou sou sou sou sou souy! |
Ci gare bi lako fekkeu mi ngui sanguo seur té beut yi di takkeu |
Ma dal di koye nougnou |
Mou dal di maye faye dal di maye yédeu |
Maky yé maky maky yé maky yééééé!!! |
Waw kérok lama khamal louma khamoul woone ci diamono bou yakhou bi |
Balaa maye dougeuti ci loumou meuneu doone |
Dinaa fattéli ko maky yé maky maky yé maky yéé!! |
Ah mani ah mani! |
Douma fatté bamako lii mani lii mani! |
Mane douma fatté bamako |
(traduzione) |
Si gare bi lako fekkeu |
Mi ngui sanguo seur |
Té beut yi di takkeu |
Ma dal di koye nougnou |
Mou dal di maye faye |
Dal di maye yédeu ci adouna bou yakhou bi |
Mane douma fatté! |
Ah mani ah mani! |
Man douma fatté bamako lii mani lii mani! |
Mane douma fatté! |
Kerok lama khamal louma khamoul woone ci diamono bou yakhou bi yénene ak yénene; |
Balaa maye dougeuti mane ci loumou meuneu doone |
Dinaa fattélikou ndaw sossou |
Limousine wakhoone! |
Souy souy sou sou sou sou sou sou! |