Informazioni sulla canzone In questa pagina puoi trovare il testo della canzone Sama Gàmmu, artista - Youssou N'Dour.
Data di rilascio: 28.10.2007
Linguaggio delle canzoni: Papiamento
Sama Gàmmu |
Nanga def yaw sama gàmmu dégg naa da nga yor xaalis |
Xam naa ne yaw moomu loo ko |
Dang ko àbb mbaa nga for ko |
Baal dóózéé, eh |
Nanga def, na nga def gàmmu dégg naa da nga yor xaalis |
Ba foo ma séén tàmbaleey wëlis |
Xam naa ne yaw moomu loo ko |
Dang ko àbb mbaa nga for ko |
Baal dóózéé, eh |
Yor xaalis mënui tee me moom la |
Nanga def, na nga def gàmmu dégg naa da nga yor xaalis |
Xam naa ne yaw moomu loo ko |
Dang ko àbb mbaa nga for ko |
Baal dóózéé, eh |
Kaay gaaw wax ma na nga def ba am ko |
Foog nan nita ko waddal nga for ko |
Wax ma gaaw ñaata la doon ma fay ko |
Man daal maay sa buur nangu ko |
Nanga def, na nga def gàmmu dégg naa da nga yor xaalis |
Ba foo ma séén tàmbaleey wëlis |
Xam naa ne yaw moomu loo ko |
Dang ko àbb mbaa nga for ko |
Baal dóózéé, eh |
Ah suñuy maam noonu lañ ko daan defee |
Ah suñuy baay noonu lañ ko daan waxee |
Ah suñuy yaay noonu lañ ko daan tópee |
Ah gàmmu daal sama doomu nday nga |
E e e gàmmu daal suma xarit nga |
E e e gàmmu daal suma askan nga |
Ah suñuy maam noonu lañ ko daan defee |
E e e gàmmu daal suma xarit nga |
E e e gàmmu daal man sama doomu nday nga |
E e e gàmmu daal man suma xarit nga |
E e e gàmmu daal yaw sama doomu nday nga |
Baal dooc moomu foo ko |
Teeyai teey teey |
Ah suñuy maam noonu lañ ko daan defee |
Ah suñuy baay noonu lañ ko daan waxee |
Ah suñuy yaay noonu lañ ko daan tópee |
E e e gàmmu daal sama doomu nday nga |
E e e gàmmu daal suma xarit nga |
E e e gàmmu daal suma askan |